Sëriñ Tuubaa Nee Na : " Am Xëy Bu Rafetul Dañoo Wara Fas Jom
Cim Ngòntu, Daadi Ni Am Xëy Nak
Mooy Ak Ndaw, Luci ëpp Du Rafet Ngir Jëfi Ndaw Yi, Am Gòntu Nak Mooy Juroom Fukki At ( 50 ans ) Jëm Kaw "
Teela Wëlbatiku Cik Ndaw Jublu Sa Boroom
Moo Gën Bayyi Ba Magget Diko Sooga Def
YÀLLA Dula Xool Sa Soxla Wul Loolu